Joxàl mala bi mu lekk! (Wolof) v19
Curious Learning OrgAbout this app
Developer Description
Ap powu njàngale buy dimbële xale yi ñu jàng liifantu !
LAN MOY JOXÀL SA MALA MU LEKK ?
Joxàl sa mala mu lekk dey jëffëndiko ay feemu po yuy jàngale yuñu tekk ci xam-xam yu woor ngir fexe ba dimbële sa doom yi ñu sawar ci jànk mi. Xale yi di neeñ bég di tànn ag di gis ni sen xaritu mala yi di magge ba pare di jàngale baat ag araf yu njëk yi lenn di dimbële ñu mëna liir
AM KO CI SA TELEFON TE DO FAY DARA, AMUL AY NATAALU SIIWAL, AMUL LOY FAY CI BIIR PO MI !
Curious Learning, CET ag Apps Factory, di ay kurel yuy ñongal jàngum làkk yi, ñooko defar te wutuñu ci benn dërëm. Do fay dara ci po mi !
MÀNDARGAWU PO MI NGIR ÑONGAL XAM-XAMU LIFANTU:
• Ay laaj yu neex te reelu jëm ci araf yi
• Ay po ngir xaame araf yi ngir liir ag bind
• Ay po ngir nafar ak denc ay baat
• Ay niiwo yu jafe yo xamne “baat bi rek gey dégg”
• Alluwa bu wayjuur yi mëna xayma tolluwaay sen doom
• Po mu nit yu bëri mëna deffando andak ñu mëna xayma tolluwaay kenn ku ne
• Ay mala yoo mëna tànne sa bula neex, yu lay dimbële nga foo, ree boolek jàng
• Dey yokku xaaraaŋtef jëm ci jókko ag yëkk-yëkk
• Do fay dara ci bir po mi
• Soxlawul dara lu leey lëkkale ag enternet
AY ESPESYAALIST YU XAARAAÑ ÑOOKO DEFAR PUR SA DOOM
Po mi ñongi ko amal ci ay atu xalaat, xayma ag jëfandikoo ci xam-xamu baat ag araf yi. Dafa dëxëñ ci bir ay xam-xam yu am jëriñ, bokk nasi xamee jëm ci ni ñuy binde baat yi, xamee araf yi, mbindum baat yi, xam-xamu baat yi ak lumuy tekki, jàng baat yi ñuy gis. Ginaw bi ñu ko defare ci màndargawu mbëggeel ag ay mala yu bëri, po mi dey dimbële xale yi ci ñu am setlu, yeewute jëm ci sen yoonu maggaay.
ÑOY ÑAN ?
Kurel gi di Joxal mala bi mu lekk ñu gën ka xam ci “Feed the monster” mongi am ci ndimbëlu banxaas bi yóor wallum bitiw rew bu dëkk bi di Norwes ginaw bimu bokke ci joŋante bi di “EduApp4Syria-competition”. Jumtukaayu bu njëku po mi mo ngi nekkoon ci làkkup arab ñu defaroon ko ci lëkkalowu kurel yi di Apps Factory, CET – The Center for Educational Technology ag IRC – The International Rescue Committee.
-------------------------------------------------
Feed The Monster teaches children the fundamentals of reading in Wolof. Collect monster eggs and feed them letters so they can grow into new friends!
WHAT IS FEED THE MONSTER?
Feed The Monster uses proven ‘play to learn’ techniques to engage kids and help them learn to read. Children enjoy collecting and growing pet monsters while learning reading fundamentals.
FREE TO DOWNLOAD, NO ADS, NO IN APP PURCHASES!
All content is 100% free, created by literacy nonprofits Curious Learning, CET, and Apps Factory.
GAME FEATURES TO PROMOTE READING SKILLS:
• Fun and engaging phonics puzzles
• Letter tracing games to aid reading and writing
• Vocabulary memory games
• Challenging “sound only” levels
• Parental progress report
• Multi-users login for individual user progress.
• Collectable, evolvable, and fun monsters
• Designed to promote socio-emotional skills
• No in-app purchases
• No ads
• No internet connection needed
DEVELOPED BY EXPERTS FOR YOUR CHILD.
The game is based on years of research and experience into the science of literacy. It incorporates key skills for literacy, including Phonological Awareness, Letter Recognition, Phonics, Vocabulary, and Sight Word Reading so kids can develop a strong foundation for reading. Built around the concept of caring for a collection of monsters, it is designed to encourage empathy, perseverance and socio-emotional development for children.
What's New
Version Information
- Version
- 19
- Downloads
- 500+
- Updated on
- Oct 13, 2020
- Released
- May 7, 2019
- Requires
- Android 4.1
Statistics
Google Play Rating History
Rating Distribution
Downloads Over Time
Joxàl mala bi mu lekk! (Wolof) has been downloaded times. Over the past 30 days, it averaged downloads per day.
Shaded area shows 30-day prediction based on historical trends
Historical data collection started recently. More data points will be available over time.
Joxàl mala bi mu lekk! (Wolof) users say on Google Play
Fun ☺️
More from Curious Learning Org
See more appsQuudi Cirfiidka! (Af Soomaali)
Free
Feed The Monster (US English)
Free
Nouri mons la! (Kreyòl Ayisyen
Free
Feed The Monster (Marathi)
Free
Feed The Monster (African Eng)
Free
fun ẹranko abami ni ounje! (Yo
Free
Nouri mons la! (Kreyòl Ayisyen
Free
Feed The Monster (African Eng)
Free
Curious Reader
Free
Feed The Monster
Free